menu.png

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
Matthew 1 1 Lii mooy cosaanu Yeesu Kirist, sëtu Daawuda, sëtu Ibraayma.
Matthew 1 2 Ibraayma moo jur Isaaxa; Isaaxa jur Yanqóoba; Yanqóoba jur Yuda ak i doomi baayam;
Matthew 1 3 Yuda, Fares ak Sara ci Tamar; Fares Esrom, miy baayu Aram;
Matthew 1 4 Aram Aminadab; Aminadab Naason; Naason Salmon;
Matthew 1 5 Salmon jur ci Raxab doom ju tudd Bowas; Bowas am ak Ruut Obedd; Obedd jur Yese,
Matthew 1 6 miy baayu buur bi Daawuda. Daawuda moo jur Suleymaan ci ki nekkoon jabari Uri;
Matthew 1 7 Suleymaan jur Robowam; Robowam Abiya; Abiya Asaf;
Matthew 1 8 Asaf Yosafat; Yosafat Yoram, miy baayu Osiyas;
Matthew 1 9 Osiyas jur Yowatam; Yowatam Akas, miy baayu Esekiyas;
Matthew 1 10 Esekiyas Manase; Manase Amon; Amon Yosiyas;
Matthew 1 11 Yosiyas jur Yekoñas ak i doomi baayam ca jamono, ja ñu defe Yawut ya jaam, yóbbu leen Babilon.
Matthew 1 12 Ba ñu leen yóbboo ca Babilon, Yekoñas jur Salacel; Salacel Sorobabel,
Matthew 1 13 miy baayu Abiyudd; Abiyudd Eliyakim; Eliyakim Asor;
Matthew 1 14 Asor Sadog; Sadog Akim; Akim Eliyudd;
Matthew 1 15 Eliyudd Eleyasar; Eleyasar Matan, miy baayu Yanqóoba;

Page:   1 2 3 4 5 6