menu.png
Lost Password ?

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
Matthew 7 22 Bu bés bAA, ñu bare dinañu ma wax: “Boroom bi, Boroom bi, ndax du ci saw tur lanu dAA waxe ci kàddug Yàlla? Ndax du ci saw tur lanu dAA dàqe ay rab? Ndax du ci saw tur lanu dAA defe ay kéemAAn yu bare?”
Matthew 7 23 Ci kaw loolu dinAA leen wax dëgg ne leen: “Musuma leen a xam; soreleen ma, yéen ñiy def bàkkAAr.”
Matthew 7 25 Ba mu noppee, taw bi daldi sóob, wal mi ñëw, ngelaw li jóg, ñu dal ci kaw kër ga; wAAye màbbul, ndaxte mu ngi jàpp ca doj wa.
Matthew 7 26 WAAye képp ku dégg lii ma leen wax, te jëfewuloo ko, dinga mel ni nit ku ñàkk xel, ku tabax këram ci gànnuus bi.
Matthew 7 28 Bi Yeesu waxee loolu ba noppi, mbooloo ma daldi wAAru ca njàngaleem,
Matthew 8 2 Noonu ku gAAna ñëw, sukk ci kanamam ne ko: «Sang bi, soo ko bëggee, man nga mAA faj.»
Matthew 8 3 Yeesu tàllal loxoom, lAAl ko nAAn: «Bëgg nAA ko, wéral.» Ca sAA sa ngAAnAAm daldi deñ.
Matthew 8 4 Yeesu ne ko: «Déglul, bu ko wax kenn, wAAye demal won sa bopp saraxalekat bi, te nga jébbal Yàlla sarax, si yoonu MusAA santAAne, ngir mu nekk seede ci ñoom.»
Matthew 8 5 GannAAw loolu Yeesu duggoon na Kapernawum. Bi mu fa duggee nag, ab njiitu xare fekksi ko. Mu ñAAn ko,
Matthew 8 7 Yeesu ne ko: «DinAA ñëw faj ko.»
Matthew 8 8 WAAye njiit la tontu ko ne: «Sang bi, yeyoowuma nga dugg ci sama kër; waxal genn kàddu rekk, te sama surga dina wér.
Matthew 8 9 Ndaxte man itam mAA ngi nekk ci ndigal, te ame nAA ay xarekat ci sama ndigal. Su ma nee kii: “Demal,” mu dem. MbAA ma ne keneen ki: “Ñëwal,” mu ñëw. Te su ma nee sama jAAm: “Defal lii,” mu def ko.»
Matthew 8 10 Bi ko Yeesu déggee, mu wAAru, ne ña topp ci moom: «Ci dëgg mAA ngi leen koy wax, musumAA gis ci bànni Israyil ku gëme ni kii.
Matthew 8 11 MAA ngi leen koy wax, ñu bare dinañu ñëw, jóge ci penku ak sowu, bokk lekk ak IbrAAyma ak IsAAxa ak Yanqóoba ci nguuru Yàlla Aji Kawe ji.
Matthew 8 12 WAAye ñi waroon a bokk ca nguur ga, dees na leen sànni ci biti ci lëndëm gi. Foofa dees na fa jooy tey yéyu.»

Page:   6 7 8 9 10 11 12 13 14 15 16