menu.png
Lost Password ?

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
Matthew 4 17 Booba Yeesu tàmbali di wAAre nAAn: «Tuubleen seeni bàkkAAr, ndaxte nguuru Yàlla Aji Kawe ji jegesi na.»
Matthew 4 18 GannAAw loolu Yeesu doon dox ca tefesu dexu Galile, mu gis fa ñAAr ñu bokk ndey ak bAAy, mooy Simoŋ mi ñuy wax Piyeer, ak Andare. Fekk ñuy sànni seen cAAx ca dex ga, ndaxte ay nappkat lañu woon.
Matthew 4 20 Ca sAA sa ñu daldi bàyyi seeni mbAAl, topp ci moom.
Matthew 4 21 Ba Yeesu demee ba ca kanam, mu gis yeneen ñAAr ñu bokk ndey ak bAAy, ñuy SAAg doomu Sebede, ak YowAAna rakkam. Ñu nekk ci seen biir gAAl ak Sebede seen bAAy, di defar seeni mbAAl. Noonu Yeesu woo leen.
Matthew 4 22 Ca sAA sa ñu daldi bàyyi gAAl ga ak seen bAAy, topp ci moom.
Matthew 4 23 Ba loolu amee Yeesu doon wër Galile gépp, di jàngale ci seeni jàngu tey yégle xebAAr bu bAAx bi ci nguuru Yàlla; muy faj jàngoro yépp ak wéradi yépp ca nit ña,
Matthew 4 25 Noonu mbooloo mu bare topp ci moom, jóge ci wàlli Galile ak diiwAAn bi ñuy wax Fukki dëkk yi, ci dëkku Yerusalem ak ci diiwAAnu Yude, ba ci gannAAw dexu Yurdan..
Matthew 5 1 Bi Yeesu gisee mbooloo ma nag, mu yéeg ca tund wa, toog; tAAlibeem ya ñëw ci moom.
Matthew 5 2 Mu daldi leen jàngal nAAn:
Matthew 5 10 Yéen ñi ñu fitnAAl ndax seen njub,barkeel ngeen,ndaxte nguuru Yàlla Aji Kawe ji,yéena ko yelloo.
Matthew 5 11 «Barkeel ngeen, bu ñu leen di sAAga, di leen fitnAAl, di leen sosal lépp lu bon ngir man.
Matthew 5 12 Bégleen te bànneexu, ndax seen yool dina réy ci lAAxira. Ndaxte noonu lañu dAAn fitnAAle yonent yi fi jiitu.
Matthew 5 13 «Yéena di xoromus àddina. Bu xorom si sàppee, nan lañu koy delloo cafkAAm? Du jariñati dara, lu dul ñu sànni ko ci biti, nit ñi dox ci kawam.
Matthew 5 15 Te it duñu tAAl làmp, dëpp cig leget, wAAye dañu koy wékk, ba muy leeral ñi nekk ci kër gi ñépp.
Matthew 5 16 Na seen leer leere noonu ci kanamu nit ñi, ngir ñu gis seeni jëf yu rafet, te màggal seen BAAy bi ci kaw.

Page:   1 2 3 4 5 6 7 8 9 10