menu.png
Lost Password ?

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
Revelation 6 15 Noonu buURI àddina si, kilifa yi, njiiti xare yi, boroom alal yi, boroom kàttan yi, jaam yi ak gor yi, ñépp làqatuji ci xunti yi ak ci ron doji tund yi.
Revelation 13 1 Noonu ma gis génn ca géej ga, rab wu am fukki béjjén ak juróom-ñaari bopp. Ci kaw béjjénam ya amoon na fukki mbaxanay buur; ca bopp ya tURI xarab Yàlla.
Revelation 16 12 Juróom-benneelu malaaka ma sotti ndabam ci dex gu mag, gi ñuy wax Efraat, ndox ma daldi ŋiis, ngir waajal yoonu buURI penku, yiy ñëw.
Revelation 16 14 Ay rabi Seytaane lañu woon, yuy def ay kéemaan te di dem ci buURI àddina sépp, di leen dajale, ngir xeex biy am ci bés bu mag, bi Yàlla Aji Kàttan jagleele boppam.
Revelation 16 16 Noonu rab ya dajale buURI àddina si ci bérab bu tudd ci làkku yawut Armagedon.
Revelation 17 2 Moom la buURI àddina si àndal ci seen njaaloo. Ci biiñu moy Yàllaam la waa àddina màndee.»
Revelation 17 3 Noonu Xelum Yàlla solu ma, malaaka ma yóbbu ma ca màndiŋ ma. Foofa ma gis fa jigéen ju war rab wu xonq te am juróom-ñaari bopp ak fukki béjjén, yaram wa fees ak tURI xarab Yàlla.
Revelation 17 18 Te jigéen ji nga gis, moo di dëkk bu mag, biy nguuru ci kaw buURI àddina si.»
Revelation 18 3 Ndaxte jox na xeeti àddina yépp, ñu naan ci koppu nafsoom ak njaaloom, ba ñu màndi. BuURI àddina ànd nañu ak moom ci njaaloo, te baana-baanay àddina woomle nañu ndax li mu bëgg mbuux.»
Revelation 18 9 BuURI àddina yépp, yi àndoon ak moom ci njaaloo ak mbuux, bu ñu séenee saxar siy jollee ci taal bi ñu koy lakke, dinañu yuuxu, di ko jooy.
Revelation 19 19 Noonu ma gis rab wa, buURI àddina si ak seeni xarekat dajaloo ngir xareji ak ki war fas wa ak ay xarekatam.
Revelation 21 14 Samp nañu miiru dëkk ba ci fukki fondamaa ak ñaar, yu ñu bind tURI fukki ndawi Mbote ma ak ñaar.
Revelation 21 24 Xeeti àddina dinañu dox cig leeram, te buURI àddina dinañu ca indi seen ndam.

Page:   1 2