Found entries


Book | Chapter | Verse | Text |
Luke | 16 | 11 | Su fekkeente ne nag jubuleen ci ALALu àddina, kon ku leen di dénk ALAL ju wóor ji? |
Luke | 16 | 12 | Te su ngeen maanduwul ci ALAL ji ngeen moomul, kon ku leen di jox ALAL ji ngeen moom? |
Luke | 16 | 13 | «Benn jaam mënul a jaamoondoo ñaari sang; fàww nga bañ kii, bëgg ki ci des, walla nga jàpp ci kenn ki, xeeb ki ci des. Mënuleen a boole jaamu Yàlla ak jaamu ALAL.» |
Luke | 16 | 19 | «Dafa amoon boroom ALAL juy sol yére yu rafet te jafe, tey dund bés bu set dund gu neex. |
Luke | 16 | 21 | te bu sañoon, di lekk ci desiti ñam wiy rot ci lekkukaayu boroom ALAL ji. Xaj yi sax daan nañu ñëw, di mar ay góomam. |
Luke | 16 | 22 | «Noonu miskin ma dee, malaaka yi yóbbu ko ca wetu Ibraayma. Boroom ALAL ja itam dee, ñu suul ko. |
Luke | 16 | 24 | Noonu mu yuuxu ne: “Maam Ibraayma, yërëm ma! YebALAL Lasaar, mu sëpp catul baaraamam ci ndox, serALAL ma sama làmmiñ, ndaxte maa ngi sonn lool ci safara sii!” |
Luke | 16 | 27 | «Noonu boroom ALAL ja ne: “Kon nag maam, maa ngi lay ñaan, nga yebal Lasaar ca sama kër baay, |
Luke | 16 | 30 | Boroom ALAL ja ne ko: “Déedéet, maam Ibraayma, waaye su kenn dekkee, dem ca ñoom, dinañu tuub seeni bàkkaar.” |
Luke | 18 | 20 | Xam nga ndigal yi: “Bul njaaloo, bul bóom, bul sàcc, bul seede lu dul dëgg, terALAL sa ndey ak sa baay.”» |
Luke | 18 | 23 | Bi nit ka déggee loolu, mu am tiis, ndaxte ku bare woon ALAL la. |
Luke | 18 | 24 | Yeesu xool ko, daldi ne: «Boroom ALAL, dugg ci nguuru Yàlla, lu jafee ngoogu! |
Luke | 18 | 25 | Giléem jaar ci bën-bënu pusa moo gën a yomb boroom ALAL dugg ci nguuru Yàlla.» |
Luke | 19 | 2 | Waaye amoon na fa waa ju ñuy wax Sase. Njiitu juutikat la, te di ku bare ALAL. |
Luke | 19 | 8 | Waaye Sase taxaw ne Boroom bi: «Déglul Boroom bi, dogu naa may sama genn-wàllu ALAL miskin yi, te lu ma mas a njublaŋ nit, jël ALALam, dinaa ko fey ñeenti yoon lu ni tollu.» |