menu.png
Lost Password ?

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
Luke 19 36 Bi muy dem, nit ñi di lALAL Yeesu seeni yére ci yoon wi.
Luke 20 47 Ñu ngi lekk ALALu jigéen ñi seen jëkkër faatu, di ñaan Yàlla ay ñaani ngistal yu gudd. Seen mbugal dina gën a tar.»
Luke 21 1 Noonu Yeesu siggi, séen ay boroom ALAL ñuy dugal seen sarax ca ndab ya ca kër Yàlla ga.
Luke 21 5 Noonu ay nit doon wax ci lu jëm ca kër Yàlla ga, ak ni ñu ko rafetale ak ay doj yu jafe ak ALAL ju ñu jébbal Yàlla. Waaye Yeesu ne leen:
Luke 23 37 «Su fekkee ne yaay buuru Yawut yi, musALAL sa bopp!»
Luke 23 39 Kenn ca defkatu lu bon ya ñu wékkoon ci bant, di ko xas, naan ko: «Xanaa du yaw yaay Almasi bi? MusALAL sa bopp te musal nu!»
John 1 39 Yeesu ne leen: «Kaayleen gis.» Noonu ñu dem, seeti fa mu daloon, ngoonALAL ko. Ci tàkkusaani kaw la woon.
John 4 25 Jigéen ja ne ko: «Xam naa ne Almasi bi --maanaam Kirist — dina ñëw te bu ñëwee, dina nu leerALAL lépp.»
John 12 28 Baay, màggALAL sa tur!» Noonu ñu dégg baat bu jóge asamaan naan: «Màggal naa ko ba noppi, te dinaa ko màggalaat.»
John 17 1 Bi mu waxee loolu ba noppi, Yeesu dafa xool ci kaw, ne jàkk asamaan, ñaan Yàlla ne: «Baay, waxtu wi tax ma ñëw ci àddina agsi na. FeeñALAL ndamu Doom ji, ngir moom itam mu man a feeñal sa ndam.
John 17 5 Léegi nag Baay, ci sa teewaay, feeñALAL ci man ndam, li ma amoon ci sa wet, laata àddina di sosu.
Acts 2 45 Ñu jaay seeni suuf ak seen ALAL, séddoo ko, ku nekk ak la ngay soxla.
Acts 3 22 Ndaxte Musaa nee woon na: “Boroom bi seen Yàlla dina leen feeñALAL ci seen xeet Yonent ni man; nangeen ko déggal ci lépp lu mu leen wax.
Acts 4 30 TàllALAL sa loxo, ci wéral ak ci wone ay kéemaan ak ay firnde, jaarale ko ci turu Yeesu, sa Ndaw lu sell li.»
Acts 4 32 Noonu mbooloom ñu gëm ñi bokk menn xel ak benn xalaat. Kenn daawul aakimoo dara ci ALALam, waaye ñoo bokkoon lépp.

Page:   1 2 3 4 5 6 7 8 9 10