menu.png
Lost Password ?

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
Luke 12 29 Buleen di wut lu ngeen di lekk walla lu ngeen di naan; te buleen ci JAAXLE.
Luke 21 25 «Ay firnde dinañu feeñ ci jant bi, ci weer wi ak ci biddiiw yi. Ci kaw suuf xeet yi dinañu tiit, JAAXLE ndax riiru géej gi ak yengu-yengub duus yi.
Luke 24 4 Noonu ba ñu nekkee ak seen nJAAXLE, am na ñaar ñu leen feeñu, sol yére yuy melax.
Luke 24 12 Waaye Piyeer daldi jóg, daw, dem ca bàmmeel ba. Bi mu àggee, mu sëgg, yër, gisul lu dul càngaay la. Noonu mu dëpp ñibbi, JAAXLE lool ci li xew.
Luke 24 38 Waaye Yeesu ne leen: «Lu tax ngeen JAAXLE, ak lu tax ngeen di xel ñaar ci seen xol?
Luke 24 41 Waaye ba tey mënuñu woon a gëm ndax seen mbég ak JAAXLE. Noonu Yeesu laaj leen ne: «Ndax am ngeen fii lu ñu lekk?»
John 4 27 Noonu nag taalibey Yeesu ya dellusi, gis muy wax ak ab jigéen. Ñu daldi JAAXLE lool. Waaye kenn ñemewu ko woon ne: «Looy laaj?» walla: «Lu tax ngay wax ak moom?»
John 7 15 Yawut ya nag JAAXLE, daldi ne: «Nu waa jii def ba xam lii lépp, moom mi jàngul?»
John 7 21 Yeesu ne leen: «Benn jaloore rekk laa def, te yéen ñépp ngeen JAAXLE!
Acts 2 12 Noonu ñépp waaru, ba JAAXLE lool, ñuy waxante ci seen biir ne: «Lii lu muy tekki?»
Acts 5 24 Bi kilifag wottukati kër Yàlla ga ak saraxalekat yu mag ya déggee loolu, ñu daldi ciy JAAXLE lool, ñuy laajante, fu lii di mujj.
Acts 10 17 Bi loolu amee Piyeer JAAXLE lool ci lu peeñu miy tekki; fekk booba nit ñi Korney yebal, laajte woon nañu kër Simoŋ, ba agsi ci bunt bi.
Acts 17 8 Bi ko mbooloo mi ak àttekat yi déggee, ñu daldi JAAXLE lool.
1 Corinthians 7 35 Seen njariñ a tax ma wax lii, du ngir teg leen yen bu ngeen àttanul, waaye ngeen man a jàppandil Boroom bi ci njaamu gu rafet gu àndul ak genn nJAAXLE.
Galatians 1 6 Man de JAAXLE naa! Yàlla woo na leen ci boppam jaarale ko ci yiw, wi nu Kirist defal, waaye yéena ngi koy gaawantoo bàyyi, ngir topp beneen xebaar,

Page:   1 2 3