menu.png
Lost Password ?

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
Philippians 4 6 Buleen JAAXLE ci dara, waaye ci lépp wéetal-leen Yàlla, diis ko seeni soxla ci ñaan gu ànd ak cant.
1 John 3 13 Bokk yi, bu leen àddina bañee, buleen ci JAAXLE.
Revelation 17 6 Ma gis jigéen ja màndi ci deretu gaayi Yàlla yi, ci deretu ñi doon seedeel Yeesu. Naka laa ko gis, ma daldi JAAXLE lool.
Revelation 17 7 Malaaka ma ne ma: «Lu tax nga JAAXLE? Dinaa la leeralal kumpag jigéen ji ak rab, wi mu war te am juróom-ñaari bopp ak fukki béjjén.

Page:   1 2 3