menu.png
Lost Password ?

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
Ephesians 5 25 Yéen nag góor ñi, na ku nekk bëgg JABARAM, ni Kirist bëgge mbooloo mi, ba joxe bakkanam ndax moom,
Ephesians 5 28 Na góor bëgg JABARAM, ni mu bëgge boppam. Bëgg sa jabar, bëgg sa bopp la.
Ephesians 5 31 Mbind mi nee na: «Moo tax góor dina beru ndeyam ak baayam, di taq ci JABARAM, ñoom ñaar doon benn.»
Ephesians 5 33 Waaye li teew, na góor gu nekk bëgg JABARAM, ni mu bëgge boppam, te jigéen ji weg jëkkëram.
Colossians 3 19 Góor ñi, na ku nekk bëgg JABARAM te muñal ko.
1 Peter 3 1 Yéen itam jigéen ñi, na ku nekk nangul sa jëkkër. Noonu su amee góor gu gëmul kàddug Yàlla, te gis JABARAM di dund dund gu sell, boole ci weg ko, loolu dina ko gindi ci lu àndul ak wax.

Page:   1 2 3