menu.png
Lost Password ?

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
John 1 18 Kenn musul a gis Yàlla, waaye Bàjjo bi, di Yàlla te nekk ak Baay bi, moo ko XAMLE.
John 15 18 «Bu leen àddina bañee, XAMLEen ne, man lañu jëkk a bañ.
John 17 26 Xamal naa leen sa tur te dinaa ko gën a XAMLE, ngir mbëggeel, gi nga am ci man, nekk ci ñoom, te man it ma nekk ci ñoom.»
Acts 5 42 Noonu bés bu nekk ca kër Yàlla ga ak ca kër ya, daawuñu noppee jàngale ak a XAMLE xebaar bu baax bi, ne Yeesu mooy Almasi bi.
Acts 6 4 Waaye nun dinanu wéy ci ñaan ci Yàlla ak ci yenub XAMLE kàddu gi.»
Acts 8 4 Ñi tasaaroo nag dem fu nekk, di fa XAMLE xebaar bu baax bu kàddug Yàlla.
Acts 8 25 Noonu bi ñu seedeelee Yàlla te wax ci kàddoom, ñu dellu Yerusalem, di XAMLE xebaar bu baax bi ci dëkk yu bare yu waa Samari.
Acts 8 40 Filib moom teeri dëkku Asot, muy jaar ci dëkk yépp, di fa XAMLE xebaar bu baax bi, ba kera muy ñëw dëkku Sesare.
Acts 12 14 Mu xàmmi baatu Piyeer, bég ci, ba fàtte koo ubbil, waaye mu daw ci biir, XAMLE ne Piyeer a nga ca bunt ba.
Acts 14 7 Foofa ñu di fa XAMLE xebaar bu baax bi.
Acts 14 21 Bi ñu fa àggee nag, ñu XAMLE fa xebaar bu baax bi, ba sàkk fa ay taalibe yu bare. Gannaaw loolu ñu dellusi Listar, Ikoñum ak Ancos,
Acts 15 18 Man dinaa def loolu, man Boroom bi ko wax,te ca njàlbéen ba tey ma di ko XAMLE.”
Acts 15 35 Waaye Pool ak Barnabas des ci Ancos, di jàngale ak di XAMLE xebaar bu baax bu kàddug Boroom bi, ñoom ak ñeneen ñu bare.
Acts 16 10 Bi mu amee peeñu moomu, ca saa sa nu fexee jàll ba Maseduwan, xam ne Boroom bi moo nu woo, ngir nu XAMLE fa xebaar bu baax bi.
Acts 16 21 di XAMLE ay aada yu nu sañul a nangu mbaa nu di ko topp, nun ñi bokk ci nguuru Room.»

Page:   1 2 3 4 5