menu.png
Lost Password ?

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
Acts 18 5 Waaye bi Silas ak Timote jógee diiwaanu Maseduwan, egg fa, Pool jublu ci XAMLE kàddu gi, tey dëggal ci Yawut yi naan, Yeesu mooy Almasi bi.
Acts 18 25 Jàngoon na ci yoonu Boroom bi, di ku farlu ci xelam, muy XAMLE ak a jàngale bu wóor ci mbirum Yeesu, waaye fekk xam-xamam yem ci ni Yaxya daan sóobe ci ndox.
Acts 21 26 Bi ñu ko waxee, Pool jël nit ña te ca ëllëg sa mu bokk setlu ak ñoom, ñu dugg ca kër Yàlla ga. Ñu XAMLE ban bés la seen setlu di àgg, di bés bu ñuy jébbale sarax ngir kenn ku nekk ci ñoom.
Acts 26 22 Waaye gannaaw Yàllaa ngi may taxawu ba tey, maa ngi taxaw fi, di ko seedeel ci mag ak ndaw; yokkuma dara ci li yonent yi ak Musaa XAMLE woon lu jiitu,
Acts 28 28 «XAMLEen nag ne, xebaaru mucc gii yégal nañu ko ñi dul Yawut, te ñoom dinañu ko déglu.»
Romans 1 1 Man Pool, jaamub Kirist Yeesu, maa leen di bind bataaxal bii. Yàlla woo na ma, ma nekk ndawam, sas ma liggéeyu XAMLE xebaaram bu baax bi.
Romans 1 3 di XAMLE mbirum Doomam, Yeesu Kirist sunu Boroom. Lu jëm ci meloom ci àddina, ci askanu Daawuda la jóge, waaye lu jëm ci xelam mu sell, Doomu Yàlla la; ndaxte ndekkiteem nekk na firnde ju ràññiku, ne moom la.
Romans 1 9 Bët bu set maa ngi leen di boole ci samay ñaan. Yàlla seede na li may wax, Yàlla mi may jaamu ci sama xel, ci XAMLE xebaar bu baax bu Doomam.
Romans 2 20 Yaa di jàngalekatu ñi jàngul ak XAMLEkatu ñi xamul, ndaxte xalaat nga ne, Yàlla jagleel na leen ci yoonu Musaa bépp xam-xam ak gépp dëgg.
Romans 9 22 Kon nag looy wax ci lii: Yàlla bëggoon na wone meram, XAMLE it dooleem ci àddina; teewul dafa sax ci muñal ñi yelloo meram te taxaw ci sànku.
Romans 9 23 Bëggoon na it XAMLE màggaayam mu ëpp xel, ci boole ñi mu yërëm ci ndamam; moo tax mu tànn leen ca njàlbéen.
Romans 15 16 ma nekk jawriñu Kirist Yeesu, yebal ma ci àddina ci xeeti ñi dul Yawut. Liggéey bu sell laay def ngir Yàlla, ci XAMLE xebaaram bu baax bi, ngir xeeti àddina sell ci dooley Xel mu Sell mi, ba neex Yàlla, mel ni sarax su ñu koy jébbal.
Romans 15 20 Sama yéene mooy XAMLE xebaaru turu Kirist fa mu eggagul, ndax bëggumaa yeggale sas wu keneen daloon.
1 Corinthians 3 13 sa liggéey dina fés, ndaxte bés baa koy XAMLE. Bés boobu dina fenk ni safara, te safara si dina nattu liggéeyu ku nekk.
1 Corinthians 4 1 Nañu nu teg kon ay surgay Kirist, di ay jawriñ yuy XAMLE mbóoti Yàlla.

Page:   1 2 3 4 5