menu.png
Lost Password ?

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
Matthew 1 12 Ba ñu leen yóbboo ca Babilon, Yekoñas jur Salacel; Salacel SorobABEL,
Matthew 23 35 Noonu deretu ñi jub, ji ñu tuur jépp ci àddina, dina xëppu ci seen kaw, li dale ci deretu ABEL mi jub, ba ci deretu Sakariya doomu Baraki, mi ngeen rey ci diggante bérab bu sell bi ak saraxalukaay bi.
Luke 3 27 Yoda, Yowanan mooy baayam; Yowanan, Resa;Resa, SorobABEL. Kooku Salacel a ko jur; Salacel, Neri;
Luke 11 51 la dale ca ABEL ba ci Sakariya, moom mi ñu rey ci diggante saraxalukaay bi ak bérab bu sell bi. Waaw, maa ngi leen koy wax, Yàlla dina mbugal niti jamono jii ndax loolu.
Hebrews 11 4 Ngëm moo tax ba ABEL jébbal Yàlla sarax su gën saraxu Kayin. Ngëmu ABEL moo tax ba Yàlla àtte ko ni ku jub, bi mu ko seedeelee ne, saraxam baax na. Te ci kaw ngëm lay wax ba tey, moom mi dee ba noppi.
Hebrews 12 24 jege Yeesu, Rammukat bi sàmm kóllëre gu bees gi; jege deretam, ji ñu wis. Te deret jooju, li muy yégle moo gën a neex li deretu ABEL doon yéene.
Revelation 2 20 Waaye li ma naqari ci yaw moo di dangaa bàyyi YesABEL, jigéen joojuy tuddoo yonent, di jàngale ak a réeral sama jaam yi, ngir ñuy sóobu ci njaaloo te di lekk ñam wu ñu tuuroo xërëm yi.

Page:   1