Found entries


Book | Chapter | Verse | Text |
Acts | 18 | 2 | Mu tase fa ak Yawut bu tudd AKILAS te juddoo diiwaanu Pont. Muy sog a jóge réewu Itali ak jabaram Pirsil, ndaxte buur ba Këlódd sant na Yawut yépp, ñu génn Room. |
Acts | 18 | 18 | Bi loolu wéyee Pool desati fa fan yu bare. Gannaaw ga mu tàggtoo ak bokk ya, dugg gaal jëm Siri, ànd ak Pirsil ak AKILAS. Bi mu jógeegul teerub Señsere, mu watlu boppam, ndaxte am na lu mu dige woon ak Yàlla. |
Acts | 18 | 26 | Noonu mu daldi wax ak fit wu dëgër ca jàngu ba. Bi ko Pirsil ak AKILAS déggee nag, ñu woo ko fi ñoom, gën ko leeral yoonu Yàlla. |
Romans | 16 | 3 | Nuyul-leen ma Pirsil ak AKILAS, samay nawle ci liggéeyu Kirist Yeesu. |
1 Corinthians | 16 | 19 | Mboolooy ñi gëm te nekk diiwaanu Asi ñu ngi leen di nuyu. AKILAS ak Pirsil, ñu ngi leen di nuyu bu baax ci Boroom bi, ñoom ak mbooloom ñi gëm tey daje seen kër. |
2 Timothy | 4 | 19 | Nuyul ma Piriska ak AKILAS ak waa kër Onesifor. |
Page:
1