menu.png
Lost Password ?

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
Matthew 1 2 Ibraayma moo jur ISAAXA; ISAAXA jur Yanqóoba; Yanqóoba jur Yuda ak i doomi baayam;
Matthew 8 11 Maa ngi leen koy wax, ñu bare dinañu ñëw, jóge ci penku ak sowu, bokk lekk ak Ibraayma ak ISAAXA ak Yanqóoba ci nguuru Yàlla Aji Kawe ji.
Matthew 22 32 “Maay Yàllay Ibraayma ak Yàllay ISAAXA ak Yàllay Yanqóoba”? Li ciy génn mooy, nekkul Yàllay ñi dee waaye Yàllay ñiy dund la.»
Mark 12 26 Te sax li jëm ci mbirum ndekkite, xanaa jànguleen lii Yàlla wax ci Tawreetu Musaa ci saarum ngarab si: “Maay Yàllay Ibraayma, ISAAXA ak Yanqóoba”?
Luke 3 34 Yanqóoba; ISAAXA; Ibraayma; Teraa; Naxor;
Luke 13 28 Foofa dingeen jooy, di yéyu, bu ngeen gisee seeni maam Ibraayma, ISAAXA, Yanqóoba ak yonent yépp ci nguuru Yàlla, te ñu dàq leen ca biti.
Luke 20 37 Te Musaa sax wone na ne, néew yi dinañu dekki, ci saarum ngarab si. Foofa Musaa wooye na fa Boroom bi: “Yàllay Ibraayma, Yàllay ISAAXA, di Yàllay Yanqóoba.”
Acts 3 13 Yàllay Ibraayma ak ISAAXA ak Yanqóoba, di Yàllay sunuy maam, màggal na Ndawam Yeesu; yéena xàcceek moom, ba jébbal ko Pilaat, fekk naroon na koo bàyyi.
Acts 7 8 Yàlla nag tëral kóllëre seen diggante, fas ko ci màndargam xaraf. Noonu Ibraayma jur ISAAXA, xarafal ko ca juróom-ñetteelu fan ba; ISAAXA def noonu Yanqóoba, Yanqóoba it def noonu fukki maam ya ak ñaar, ñi sos xeet wi.
Acts 7 32 “Man maay sa Yàllay maam, di Yàllay Ibraayma, ISAAXA ak Yanqóoba.” Ci kaw loolu Musaa tiit bay lox, te ñemeetul a xool.
Romans 9 7 Te it du ñi soqikoo ci Ibraayma ñépp, ay doomam dëgg lañu. Ndaxte Yàlla dafa wax Ibraayma ne ko: «Saw askan ci ISAAXA lay jaar.»
Romans 9 10 Te du ci loolu rekk, waaye noonu la it ci lu jëm ci Rebeka; doom yi mu jur ñoo bokk benn baay, moo di sunu maam ISAAXA.
Galatians 4 28 Yéen bokk yi, yéenay doom yi ñu dige woon, niki ISAAXA.
Hebrews 11 9 Ngëm a tax ba Ibraayma sanc ci réew, mi ko Yàlla digoon, dëkk ci ay tànt ni doxandéem, moom ak doomam ISAAXA ak sëtam Yanqóoba, fekk sax Yàlla digoon na leen réew mi.
Hebrews 11 17 Ngëm moo tax Ibraayma naroon a rey ISAAXA ni sarax, bi ko Yàlla nattoo. Moom mi jotoon dige yi, moo demoon bay saraxe jenn doom ji mu am kepp,

Page:   1 2