menu.png
Lost Password ?

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
Revelation 14 7 Ma nga doon xaacu naan: «Ragal-leen Yàlla te jox ko ndam li, ndaxte waxtuw àtteem jot na. JAAMULeen ki sàkk asamaan ak suuf ak géej ak bëti ndox yi.»
Revelation 19 10 Noonu ma daanu ci ay tànkam, bëgg koo jaamu. Waaye mu ne ma: «Moytu koo def; sa nawle laa ci liggéey bi, di kenn ci say bokk, yiy sax ci seedeel Yeesu. JAAMUL Yàlla. Ndaxte seedes Yeesu mooy xel miy solu yonent yi.»
Revelation 22 9 Waaye mu ne ma: «Moytu koo def. Sa nawle laa ci liggéey bi, yaw ak say bokki yonent ak ñiy sàmm waxi téere bii. JAAMUL Yàlla.»

Page:   1