Found entries


Book | Chapter | Verse | Text |
Acts | 2 | 10 | di waa Firisi, PAMFILI, Misra ak weti Libi, yi dend ak Siren, nun ak gan ñi jóge Room, |
Acts | 13 | 13 | Naka noona Pool ak ñi mu àndal jóge Pafos, jaar ci géej, jëm dëkku Peers ci réewu PAMFILI. Yowaana nag tàggoo ak ñoom, dellu Yerusalem. |
Acts | 14 | 24 | Gannaaw loolu ñu jaar diiwaanu Pisidi, dikk ci PAMFILI. |
Acts | 15 | 38 | Waaye Pool dafa lànk ne: «Matul nu yóbbu ki nu waccoon ca PAMFILI, ba àndul woon ak nun ca liggéey ba.» |
Acts | 27 | 5 | Nu jàll géej, gi janook diiwaani Silisi ak PAMFILI, teersi Mira ca wàlli Lisi. |
Page:
1