menu.png
Lost Password ?

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
Matthew 1 6 miy baayu buur bi Daawuda. Daawuda moo jur Suleymaan ci ki nekkoon jabari URI;
Matthew 17 25 Piyeer ne leen: «Aaŋkay!»Ba ñu eggee kër ga nag, Yeesu jëkk a wax ne Piyeer: «Waaw lu ciy sa xalaat, Simoŋ? BuURI àddina si, ñan lañuy laaj juuti walla galag? Seeni doom walla ñi bokkul ci njaboot gi?»
Luke 2 22 Noonu jamono ji ñu leen waroon a sellale agsi, ni ko yoonu Musaa tërale. WaajURI Yeesu yi daldi koy yóbbu ca dëkku Yerusalem, ngir sédde ko Boroom bi.
Luke 2 27 Noonu Xelum Yàlla daldi yóbbu Simeyon ba ca kër Yàlla ga. Bi waajURI Yeesu indee xale ba, ngir sédde ko Yàlla, ni ko yoon wi santaanee,
Luke 2 33 WaajURI Yeesu yi waaru ci li ñu doon wax ci xale bi.
Luke 2 39 Bi waajURI Yeesu yi matalee seen warugar ci lépp lu yoonu Boroom bi santaane woon, ñu dellu seen dëkku Nasaret ca diiwaanu Galile.
Luke 2 41 At mu jot nag waajURI Yeesu yi daan nañu dem Yerusalem, ngir màggali bésu Jéggi ba.
Luke 8 51 Bi Yeesu agsee ca kër ga, nanguwul kenn duggaaleek moom, ñu dul Piyeer, Yowaana, Saag ak waajURI xale ba.
Luke 8 56 WaajURI xale bi daldi waaru. Waaye Yeesu tere leen, ñu wax kenn li xew.
Luke 22 25 Yeesu ne leen: «BuURI xeeti àddina dañu leen di dóor yetu nguur, te kilifa yi dañuy sàkku ngërëm.
John 9 22 Ragal Yawut ya nag moo taxoon waajURI nit ka waxe noonu, ndaxte Yawut ya dañoo mànkoo woon ne, képp ku seede ne Yeesu mooy Almasi bi, ñu dàq la ca jàngu ba.
Acts 4 26 BuURI àddina dañoo booloo,te kilifa yi dajaloo,di bañ Boroom bi ak Almaseem.”
Acts 16 38 Bi mu ko waxee, alkaati ya yégal àttekat ya la mu wax. Bi ñu déggee ne, jaambURI Room lañu, ñu daldi tiit.
2 Corinthians 3 16 Waaye saa su kenn walbatikoo ci Boroom bi, muuraay gi daldi mURIku.
Hebrews 1 12 Dinga leen taxañ ni malaan,ñu fURI ni ay yére,waaye yaw doo soppiku,te sa dund amul àpp.»

Page:   1 2