menu.png
Lost Password ?

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
Matthew 1 1 Lii mooy cosAAnu Yeesu Kirist, sëtu DAAwudA, sëtu IbrAAymA.
Matthew 1 2 IbrAAymA moo jur IsAAxA; IsAAxA jur YAnqóobA; YAnqóobA jur YudA Ak i doomi bAAyAm;
Matthew 1 3 YudA, FAres Ak SArA ci TAmAr; FAres Esrom, miy bAAyu ArAm;
Matthew 1 4 ArAm AminAdAb; AminAdAb NAAson; NAAson SAlmon;
Matthew 1 5 SAlmon jur ci RAxAb doom ju tudd BowAs; BowAs Am Ak Ruut Obedd; Obedd jur Yese,
Matthew 1 6 miy bAAyu buur bi DAAwudA. DAAwudA moo jur SuleymAAn ci ki nekkoon jAbAri Uri;
Matthew 1 7 SuleymAAn jur RobowAm; RobowAm AbiyA; AbiyA AsAf;
Matthew 1 8 AsAf YosAfAt; YosAfAt YorAm, miy bAAyu OsiyAs;
Matthew 1 9 OsiyAs jur YowAtAm; YowAtAm AkAs, miy bAAyu EsekiyAs;
Matthew 1 10 EsekiyAs MAnAse; MAnAse Amon; Amon YosiyAs;
Matthew 1 11 YosiyAs jur YekoñAs Ak i doomi bAAyAm cA jAmono, jA ñu defe YAwut yA jAAm, yóbbu leen BAbilon.
Matthew 1 12 BA ñu leen yóbboo cA BAbilon, YekoñAs jur SAlAcel; SAlAcel SorobAbel,
Matthew 1 13 miy bAAyu Abiyudd; Abiyudd EliyAkim; EliyAkim Asor;
Matthew 1 14 Asor SAdog; SAdog Akim; Akim Eliyudd;
Matthew 1 15 Eliyudd EleyAsAr; EleyAsAr MAtAn, miy bAAyu YAnqóobA;

Page:   1 2 3 4 5 6