Found entries


Book | Chapter | Verse | Text |
Matthew | 2 | 11 | Ñu dugg ca kër ga, gis xale ba ak Maryaama ndeyam, ñu daldi sukk, di ko màggal. Ñu ubbi seeni boyetu ALAL, may ko wurus ak cuuraay ak ndàbb lu xeeñ lu ñuy wax miir. |
Matthew | 6 | 17 | Yaw nag booy woor, xeeñALAL sa bopp te nga sëlmu, |
Matthew | 6 | 19 | «Buleen dajale ALAL ci àddina, fu ko max ak xomaag di yàqe, ak fu sàcc di dugg, jot ko. |
Matthew | 6 | 20 | Waaye dajaleleen ALAL ci laaxira, fu ko max ak xomaag dul yàqe, ak fu sàcc dul dugg, jot ko. |
Matthew | 6 | 21 | Ndaxte fu sa ALAL nekk, fa la sa xol nekk itam. |
Matthew | 6 | 24 | «Kenn mënul a jaamoondoo ñaari sang; fàww nga bañ kii, bëgg ki ci des, walla nga jàpp ci kenn ki, xeeb ki ci des. Mënuleen a boole jaamu Yàlla ak jaamu ALAL. |
Matthew | 12 | 13 | Noonu Yeesu ne nit ka: «TàllALAL sa loxo!» Mu tàllal ko nag, loxoom daldi wér, mel ni ba ca des. |
Matthew | 12 | 29 | «Su fi amee nit ku bare doole, te nit bëgg a dugg ci këram, nangu ALALam, naka la koy defe? Xanaa dafay jëkk a yeew ku bare doole ka, ba noppi door a toj këram gépp. |
Matthew | 13 | 22 | Ki jot ci jiwu wi ci xaaxaam yi mooy ki dégg wax ji, waaye soxlay àddina ak naxi ALAL tanc wax ji, ba du jur njariñ. |
Matthew | 13 | 44 | Yeesu teg ca ne: «Nguuru Yàlla Aji Kawe ji dafa mel ni ALAL ju nëbbu cib tool. Nit ki ko gis nëbbaat ko; xolam sedd, ba mu dem jaay li mu am lépp, jënd tool ba. |
Matthew | 15 | 4 | Yàlla nee na: “TerALAL sa ndey ak sa baay,” te it: “Ku móolu sa ndey walla sa baay, dees na la rey.” |
Matthew | 18 | 23 | «Loolu moo tax nguuru Yàlla Aji Kawe ji dafa mel ni buur bu bëgg a waññ ALALam ak ay jaraafam. |
Matthew | 19 | 19 | terALAL sa ndey ak sa baay, te it: nanga bëgg sa moroom, ni nga bëgge sa bopp.» |
Matthew | 19 | 22 | Waaye bi waxambaane wa déggee loolu, mu jóge fa ak tiis, ndaxte ku bare woon ALAL la. |
Matthew | 19 | 23 | Noonu Yeesu wax taalibeem ya ne leen: «Ci dëgg maa ngi leen koy wax, boroom ALAL dugg ci nguuru Yàlla Aji Kawe ji, lu jafee ngoogu! |