menu.png
Lost Password ?

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
2 Corinthians 6 3 Bëggunoo lëmBAAJE xelu kenn ci dara, ngir kenn bañ a sikk sunu liggéey.
2 Corinthians 11 3 Waaye ni jaan ja naxe woon Awa ci pexeem, ragal naa yéen itam ñu lëmBAAJE ni seen xel, ba ngeen dëddu xol bu laab, bi ngeen amoon ci seen diggante ak Kirist.
Ephesians 4 14 Noonu dootunu ay gune yu njàngalem nit ku ñëw di fàbbi ci seeni làqarci ak seeni pexe, nu mel ni ay gaal yu duus yi ak ngelaw li di BAAJE.
James 1 6 Waaye na ko ñaan ci ngëm te bañ cee werante; ndaxte kiy werante mi ngi mel ni ndoxum géej, mi ngelaw liy lëmBAAJE wet gu ne.

Page:   1