menu.png
Lost Password ?

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
Matthew 4 20 Ca saa sa ñu daldi bàyyi seeni mBAAL, topp ci moom.
Matthew 4 21 Ba Yeesu demee ba ca kanam, mu gis yeneen ñaar ñu bokk ndey ak baay, ñuy Saag doomu Sebede, ak Yowaana rakkam. Ñu nekk ci seen biir gaal ak Sebede seen baay, di defar seeni mBAAL. Noonu Yeesu woo leen.
Matthew 6 12 te BAAL nu sunuy tooñ, ni nu BAALe ñi nu tooñ;
Matthew 6 14 «Su ngeen BAALee ñi leen tooñ, seen Baay bi ci kaw dina leen BAAL seeni tooñ yéen itam.
Matthew 6 15 Waaye su ngeen BAALul ñi leen tooñ, seen Baay it du leen BAAL seeni tooñ.
Matthew 9 2 Foofa ñu indil ko ku tëdd ci basaŋ, fekk yaramam wépp làggi. Bi Yeesu gisee seen ngëm, mu ne ku làggi ka: «Na sa xel dal, sama waay, BAAL nañu la say bàkkaar.»
Matthew 9 5 Ma wax ne: “BAAL nañu la say bàkkaar,” walla ma ne: “Jógal te dox,” lan moo ci gën a yomb?
Matthew 9 6 Waaye xamleen ne, Doomu nit ki am na ci àddina sañ-sañu BAALe bàkkaar yi.» Ci kaw loolu Yeesu ne ku làggi ka: «Jógal, jël sa basaŋ te nga ñibbi.»
Matthew 12 31 Yeesu teg ca ne: «Loolu moo tax maa ngi leen koy wax, bàkkaar walla sos wu mu man a doon, dinañu ko BAALe, waaye ku sosal Xelum Yàlla, duñu ko BAAL.
Matthew 12 32 Ku sosal Doomu nit ki, dinañu ko BAAL, waaye ku sosal Xel mu Sell mi, duñu ko BAAL mukk, du ci àddina si, du ci àllaaxira.
Matthew 13 47 Yeesu waxaat ne: «Nguuru Yàlla Aji Kawe ji dafa mel ni mBAAL mu ñu wàcce ci géej, mu jàpp jën wu nekk.
Matthew 13 48 Bi mBAAL mi feesee nag, ñu ñoddi ko ci tefes gi, ba noppi ñu taxaw, dajale yu baax yi ciy ndab, waaye sànni yi bon.
Matthew 16 5 Gannaaw loolu taalibe yi jàllaat dex gi, fekk fàtte nañoo yóbBAALe mburu.
Matthew 18 21 Noonu Piyeer ñëw ci Yeesu, laaj ko: «Boroom bi, bu ma sama mbokk tooñee, ñaata yoon laa ko war a BAAL? Xanaa ba ci juróom-ñaari yoon?»
Matthew 18 27 Noonu sangam yërëm ko, bàyyi ko, BAAL ko bor ba.

Page:   1 2 3 4 5 6