menu.png
Lost Password ?

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
Matthew 6 12 te baal nu sunuy tooñ, ni nu BAALE ñi nu tooñ;
Matthew 6 14 «Su ngeen BAALEe ñi leen tooñ, seen Baay bi ci kaw dina leen baal seeni tooñ yéen itam.
Matthew 9 6 Waaye xamleen ne, Doomu nit ki am na ci àddina sañ-sañu BAALE bàkkaar yi.» Ci kaw loolu Yeesu ne ku làggi ka: «Jógal, jël sa basaŋ te nga ñibbi.»
Matthew 12 31 Yeesu teg ca ne: «Loolu moo tax maa ngi leen koy wax, bàkkaar walla sos wu mu man a doon, dinañu ko BAALE, waaye ku sosal Xelum Yàlla, duñu ko baal.
Matthew 16 5 Gannaaw loolu taalibe yi jàllaat dex gi, fekk fàtte nañoo yóbBAALE mburu.
Matthew 25 3 Ñi ñàkk xel nag fab nañu seeni làmp, waaye faBAALEwuñu diwlin;
Matthew 25 4 waaye ñi am xel ñoom fab nañu seeni làmp, faBAALE diwlin ciy njaq.
Mark 2 7 «Kii kan la, ba sañ a wax lii; mi ngi sosal Yàlla. Ana ku man a BAALE bàkkaar yi, ku dul Yàlla doŋŋ?»
Mark 2 10 Waaye xamleen ne, Doomu nit ki am na ci àddina sañ-sañu BAALE bàkkaar yi.» Ci kaw loolu mu ne làggi ba:
Mark 6 8 Mu digal leen nii: «Bu ngeen di dem, buleen yóbBAALE dara; du mburu mbaa mbuus mbaa xaalis ci seeni maxtume, waaye yemleen ci aw yet rekk.
Mark 8 14 Taalibe yi nag fàtte woon nañu yóbBAALE mburu, te amuñu woon lu dul benn mburu ci gaal gi.
Luke 3 21 Noonu Yaxya sóob mbooloo mépp ci ndox, sóoBAALE it Yeesu. Bi Yeesu di ñaan nag, asamaan daldi ubbiku.
Luke 5 21 Xutbakat yi ak Farisen yi di werante ci seen xel naan: «Kii mooy kan bay sosal Yàlla? Ana ku man a BAALE bàkkaar yi, ku dul Yàlla doŋŋ?»
Luke 5 24 Waaye xamleen ne, Doomu nit ki am na ci àddina sañ-sañu BAALE bàkkaar yi.» Ci kaw loolu Yeesu ne ku làggi ba: «Maa ngi la koy sant, jógal, jël sa basaŋ te nga ñibbi.»
Luke 7 37 Fekk amoon na ca dëkk ba jigéen juy moy Yàlla. Bi mu yégee ne, Yeesoo ngay lekk ca kër Farisen ba, mu dem, yóbBAALE njaq lu ñu defare doj wu ñuy wax albaatar te def latkoloñ.

Page:   1 2 3