menu.png
Lost Password ?

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
Matthew 6 34 Buleen jaaxle nag ngir ëllëg, ndaxte ëllëg dina topptoo boppam. Bés bu nekk, COONOOM doy na ko.
John 16 21 Jigéen ju nekk ci mat, dafay jàq, ndaxte waxtu wi mu war a jur jot na. Waaye bu doom ji juddoo, dina fàtte COONOOM ndaxte day bég ci li doom ji gane àddina.
Acts 1 3 Gannaaw ay COONOOM, ñëw na ci ñoom, di leen won ay firnde yu bare te wér ne mu ngi dund; mu feeñu leen diirub ñeent-fukki fan, di diisoo ak ñoom ci lu jëm ci nguuru Yàlla.
Acts 7 10 génne ko ci COONOOM yépp, defal ko yiw ak xel ci kanamu Firawna, buuru Misra, mu def ko kilifag Misra ak këram gépp.
Philippians 3 10 Moom laay ittewoo xam, ak doole ji ànd ak ndekkiteem, ma bokk ci ay COONOOM, ba fekki ko ci deeyam,
Revelation 18 10 Dinañu tiit ndax COONOOM, ba dandu lu sore, naan:«Ngalla yaw! Ngalla yaw,dëkk bu mag bi,Babilon mi am kàttan;wenn waxtu rekk doy na,ngir sab àtte mat!»
Revelation 18 15 Baana-baana, yi daan jaay yëf yooyu ba woomle, dinañu sore ndax ragal COONOOM. Dinañu jooy di naqarlu,

Page:   1