menu.png
Lost Password ?

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
Matthew 1 22 Loolu lépp xewoon na, ngir amal li Boroom bi wax, JAARALE ko cib yonent, bi mu naan:
Matthew 2 5 Ñu ne ko: «Ca Betleyem ci diiwaanu Yude, ndaxte lii lañu bind JAARALE ko cib yonent:
Matthew 2 15 Mu toog fa, ba Erodd faatu. Noonu am li Boroom bi waxoon JAARALE ko cib yonent, bi mu naan:«Woo naa sama doom, mu génn Misra.»
Matthew 2 17 Booba am la ñu waxoon JAARALE ko ci yonent Yàlla Yeremi, bi mu naan:
Matthew 2 23 Mu ñëw nag dëkk ci dëkk bu ñuy wax Nasaret. Noonu am la ñu waxoon ca xale ba, JAARALE ko ca yonent ya, bi ñu naan:«Dees na ko tudde Nasaréen.»
Matthew 3 3 Yaxya mooy ki ñu doon wax JAARALE ko ci yonent Yàlla Esayi, bi mu naan:«Am na baat buy xaacu ca màndiŋ ma ne:“Xàll-leen yoonu Boroom bi,jubal-leen fi muy jaar.”»
Matthew 4 14 Noonu am la ñu waxoon, JAARALE ko ci yonent Yàlla Esayi, bi mu naan:
Matthew 8 17 Loolu mu def, def na ko, ngir la ñu waxoon JAARALE ko ci yonent Yàlla Esayi am, bi mu naan:«Fab na sunuy wopp, gàddu sunuy jàngoro.»
Matthew 12 17 Def na noonu, ngir amal la ñu waxoon JAARALE ko ci yonent Yàlla Esayi, bi mu naan:
Matthew 13 35 Noonu am la ñu waxoon JAARALE ko cib yonent, bi mu naan:«Dinaa leen wax ciy léeb,di yégle yëf yu nëbbuli dale ca njàlbéen ga ba bésu tey.»
Matthew 21 4 Yeesu def na noonu, ngir la ñu waxoon JAARALE ko cib yonent am, bi mu naan:
Matthew 24 15 «Dina am bés bu li ñuy wax: “Lu araam luy yàqe” dina tege ca bérab bu sell ba. Mooy li ñu doon wax JAARALE ko ci yonent Yàlla Dañeel; ku ko jàng, nanga ko xam.
Matthew 27 9 Noonu la ñu waxoon JAARALE ko ci yonent Yàlla Yeremi am, bi mu naan: «Fab nañu fanweeri poseti xaalis ya, mooy njëg gi bànni Israyil xayma woon ci nit ki;
Luke 1 70 ni mu yéglee woon bu yàggJAARALE ko ci yonentam yu sell yi.
Luke 11 18 Te it bu Seytaane xeexee boppam, naka la nguuram di man a yàgge? Damay wax loolu, ndaxte nee ngeen, damay dàq rab JAARALE ko ci kàttanu Beelsebul.

Page:   1 2 3 4 5