menu.png
Lost Password ?

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
Matthew 13 45 «Te it nguuru Yàlla Aji Kawe ji dafa mel ni JAAYKAT buy wut per yu rafet.
Matthew 21 12 Bi loolu amee Yeesu dugg ca kër Yàlla ga, dàq ñépp ña fay jaay ak ña fay jënd. Mu daaneel taabali weccikatu xaalis ya ak tooguy JAAYKATi pitax ya,
Matthew 25 9 Waaye ñi am xel tontu leen ne: “Li nu yor du doy ngir nun ak yéen; tee ngeen a dem ca JAAYKAT ya, jënd.”
Mark 11 15 Bi ñu eggee Yerusalem, Yeesu dugg ci kër Yàlla gi, daldi dàq ñi fay jaay ak ñi fay jënd. Mu daaneel taabali weccikatu xaalis yi ak tooguy JAAYKATi pitax yi,
John 2 14 dugg ca kër Yàlla ga. Bi mu fa demee, fekk na ca ëtt ba ay JAAYKATi nag ak yu xar ak yu pitax, ak weccikatu xaalis ya toog.
John 2 16 daldi ne JAAYKATi pitax ya: «Jëleleen fi lii! Sama kër Baay, buleen ko def marse!»
Acts 16 14 Fekk am na fa jigéen juy déglu, tudd Lidi, di JAAYKATu cuub, bu dëkk Catir, te mu ragal Yàlla. Noonu Boroom bi ubbi na xolam, ba mu nangu li Pool di wax.

Page:   1