Found entries


Book | Chapter | Verse | Text |
Matthew | 11 | 7 | Bi nga xamee ne taalibe ya Yaxya yónni woon ci Yeesu dem nañu, Yeesu daldi wax ak mbooloo ma ci mbirum Yaxya ne leen: «Lu ngeen seeti woon ca màndiŋ ma? Xanaa barax buy JAAYU ci ngelaw li? |
Luke | 7 | 24 | Bi ndawi Yaxya yi demee, Yeesu daldi wax ak mbooloo ma ci mbirum Yaxya ne leen: «Lu ngeen seeti woon ca màndiŋ ma? Xanaa barax buy JAAYU ci ngelaw li? |
Page:
1