Found entries


Book | Chapter | Verse | Text |
Matthew | 1 | 24 | Noonu Yuusufa yeewu, yeggali JABARAM, na ko ko malaakam Boroom bi sante woon. |
Matthew | 18 | 25 | waaye jaraaf ja amul lu mu feye. Kon nag sangam santaane, ñu jaay ko moom ak JABARAM ak ay doomam ak lépp lu mu am, ngir fey bor ba. |
Matthew | 19 | 3 | Bi mu fa nekkee, ay Farisen ñëw ci moom, bëgg koo fiir; ñu ne ko: «Ndax jaadu na nit fase JABARAM, saa su ko neexee?» |
Matthew | 19 | 5 | te mu ne: “Moo tax góor dina beru ndeyam ak baayam, di taq ci JABARAM, ñoom ñaar doon benn.” |
Matthew | 19 | 7 | Bi Yeesu waxee loolu, Farisen ya laaj ko ne: «Waaye Musaa santaane na, nit jox JABARAM kayitu pase, tàggook moom. Lu tax mu wax loolu nag?» |
Matthew | 22 | 24 | «Kilifa gi, Musaa nee woon na: “Boo xamee ne góor dee na te amul doom, na rakkam donn JABARAM, ngir sàkkal magam njaboot.” |
Matthew | 27 | 19 | Te it bi mu toogee sax ca jalu àttekaay ba, JABARAM yónnee ci moom ne ko: «Bul dugg ci yëfi ku jub kooku, ndaxte tey gént naa ci moom te sonn naa ci lool.» |
Mark | 10 | 2 | Noonu ay Farisen ñëw ci moom, lalal ko fiir, ñu laaj ko: «Ndax jaadu na, nit fase JABARAM?» |
Mark | 10 | 4 | Ñu ne ko: «Musaa maye na, nit bind kayitu pase, tàggook JABARAM.» |
Mark | 10 | 7 | Moo tax góor dina beru ndeyam ak baayam, di taq ci JABARAM, |
Mark | 12 | 19 | Ñu ne ko: «Kilifa gi, Musaa bindal na nu ne, ku magam faatu, te bàyyiwul doom ak JABARAM, kooku war na donn jigéen ji, ba yékkati giiru magam. |
Luke | 1 | 5 | Ca jamonoy Erodd, mi nekkoon buur ca réewu Yawut ya, amoon na saraxalekat bu ñu tudde Sakariya te bokk ca mbootaayu saraxalekat, ya askanoo ci Abiya. JABARAM Elisabet askanoo moom itam ci Aaroona. |
Luke | 1 | 6 | Sakariya ak JABARAM ñu jub lañu ca kanam Yàlla, di topp ni mu ware ndigal yi ak dogali Boroom bi yépp. |
Luke | 1 | 24 | Bi mbir yooyu weesoo, Elisabet JABARAM ëmb, di ko nëbb lu mat juróomi weer |
Luke | 2 | 5 | Mu dem binduji, ànd ak Maryaama JABARAM, fekk booba Maryaama ëmb. |