Found entries


Book | Chapter | Verse | Text |
Matthew | 14 | 3 | Ndaxte Erodd jàppoon na Yaxya, yeew ko, tëj. Ndaxte Erodd takkoon na Erojàdd, JABARU Filib magam, |
Matthew | 22 | 28 | Bu ndekkite taxawee nag, JABARU kan lay doon ci juróom-ñaar ñi, ndaxte ñépp jël nañu ko?» |
Mark | 6 | 17 | Fekk Erodd yónnee woon na, jàpp Yaxya, yeew ko, tëj. Ndaxte Erodd takkoon na Erojàdd JABARU Filib magam. |
Mark | 6 | 18 | Te Yaxya ne ko: «Jaaduwul nga denc sa JABARU mag.» |
Luke | 3 | 19 | Waaye Yaxya yedd na Erodd boroom diiwaanu Galile, ndaxte dafa takkoon Erojàdd, JABARU magam, te it boole woon na ci yeneen ñaawteef, |
Luke | 8 | 3 | Sànn, JABARU ku ñuy wax Kusa, mi doon wottu alalu Erodd; ak Susànn ak ñeneen jigéen. Jigéen ñooñu ñoo doon joxe seen alal, ngir dimbali Yeesu ak ay taalibeem. |
Luke | 12 | 53 | Baay bi dina féewaloo ak doom ji, doom ji ak baayam. Ndey dina féewaloo ak doomam ju jigéen; doom ju jigéen ji ak ndeyam. Goro dina féewaloo ak JABARU doomam; JABARU nit ak goroom.» |
Luke | 17 | 32 | Fàttalikuleen JABARU Lóot! |
1 Corinthians | 5 | 1 | Dégg nanu sax ñu naan, am na kuy moy Yàlla ci seen biir, moy gu ni tollu, duñu ko gis sax ci ñi xamul Yàlla. Dem na, ba am ci yéen kuy séy ak JABARU baayam. |
Revelation | 21 | 9 | Gannaaw loolu benn malaaka ñëw, mi bokk ca juróom-ñaari malaaka, ya yoroon juróom-ñaari ndabi musiba yu mujj ya, ne ma: «Ñëwal, ma won la séet bi, JABARU Mbote mi.» |
Page:
1