Found entries


Book | Chapter | Verse | Text |
Matthew | 17 | 25 | Piyeer ne leen: «Aaŋkay!»Ba ñu eggee kër ga nag, Yeesu jëkk a wax ne Piyeer: «Waaw lu ciy sa xalaat, Simoŋ? Buuri àddina si, ñan lañuy laaj juuti walla galag? Seeni doom walla ñi bokkul ci nJABOOT gi?» |
Matthew | 22 | 24 | «Kilifa gi, Musaa nee woon na: “Boo xamee ne góor dee na te amul doom, na rakkam donn jabaram, ngir sàkkal magam nJABOOT.” |
Matthew | 27 | 25 | Ñépp tontu ko: «Na deretam dal ci sunu kaw ak sunu kaw nJABOOT.» |
Luke | 11 | 7 | «Waaye kooku nekk ci biir néegam, dina ko tontu: “Bu ma lakkal, tëj naa bunt bi ba noppi te tëdd, man ak sama nJABOOT; mënumaa jóg di la jox dara.” |
John | 4 | 53 | Noonu baayu xale ba daldi seetlu ne, ca waxtu woowa la ko Yeesu ne woon: «Sa doom dina dund.» Moom ak nJABOOTam gépp, ñu daldi gëm Yeesu. |
Acts | 7 | 13 | Bi fa ay doomi baayam delloo nag, Yuusufa xàmmiku leen, te Firawna xamante ak nJABOOTam. |
Acts | 16 | 31 | Ñu tontu ko: «Gëmal Yeesu Boroom bi, kon dinga mucc, yaw ak sa nJABOOT.» |
Romans | 8 | 29 | Ndaxte ñi mu xamoon lu jiitu, dafa dogaloon ñu nirook Doomam, ngir mu nekk taaw ci biir nJABOOT gu yaa. |
1 Corinthians | 16 | 15 | Xam ngeen ne, Estefanas ak nJABOOTam ñoo jëkk a nangu xebaar bu baax bi ci diiwaanu Akayi, te ñoo joxe seen bopp, ngir liggéeyal gaayi Yàlla yi. Kon nag bokk yi, maa ngi leen di ñaan, |
Galatians | 4 | 27 | Ndaxte Mbind mi nee na:«Bégal, yaw jigéen ji dul jur,te musul a am doom.Reeyal te bànneexu,yaw mi musul a xam coonob mat,ndaxte jigéen ji ñu faalewulmoo gën a JABOOT ki nekk ak jëkkëram.» |
Ephesians | 3 | 15 | biy cosaanul nJABOOT gépp, muy ci kaw, muy ci suuf. |
1 Thessalonians | 2 | 7 | Manoon nanoo diis ci seen kaw sax, nun ñiy ndawi Kirist, waaye woyofoon nanu ci seen biir, te lewet ni JABOOT buy uuf doomam. |
1 Timothy | 3 | 5 | Ndaxte ku mënta yor nJABOOTam, naka lay man a yore nJABOOTu Yàlla? |
1 Timothy | 5 | 4 | Waaye ku ci am ay doom mbaa ay sët, na nJABOOT googu jëkk a wone seen ragal Yàlla ci seen biir kër, ci delloo njukkal seen waajur, ndaxte loolu lu rafet la fa kanam Yàlla. |
Hebrews | 2 | 11 | Moom Yeesu miy sellal, ak ñi muy sellal, ñoom ñépp genn nJABOOT lañu. Moo tax Yeesu rusu leen a wooye ay doomi baayam. |
Page:
1 2