menu.png
Lost Password ?

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
Revelation 4 3 Leeraayam mel ni JAMAA ak per bu xonq, te xon gu leer ni per bu wert wër gàngune ma.
Revelation 17 4 Jigéen ja sol lu yolet te xonq, takk wurus ak JAMAA ak ay per. Yoroon na koppu wurus bu fees ak ñaawteef ak sobeem.
Revelation 18 12 seen wurus, seen xaalis, seeni JAMAA ak yeneeni per; seeni piis yu rafet, piis yu yolet, yu ray-ray, yu xonq; seen dénk wu xeeñ, seen yëf yi ñu defare iwaar walla dénk wu jafe walla xànjar walla weñ walla marbar;
Revelation 18 16 naan:«Ngalla yaw! Ngalla yaw, dëkk bu mag,bi soloon yére yu rafet, yu yolet te xonq,daan takk wurus ak JAMAA ak per,
Revelation 21 11 ànd ak ndamu Yàlla. Leeraayam mel ni leeraayu per bu jafe lool, ni JAMAA buy ray-rayi.
Revelation 21 18 Miir ba, JAMAA lañu ko liggéeye, te dëkk ba di wurusu ngalam, leer ni weer bu set.
Revelation 21 19 Fondamaay miiru dëkk ba rafetale nañu leen xeeti per yu nekk.Fondamaa bu jëkk ba JAMAA la;ñaareel ba, per bu bulo bu ñuy wax safir;ñetteel ba, per bu wert bu ñuy wax kalseduwan;ñeenteel ba, per bu wert te lerax, bu ñuy wax emëróot;

Page:   1