menu.png
Lost Password ?

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
Matthew 14 26 Waaye bi ko taalibe yi gisee, muy dox ci kaw dex ga, ñu daldi jommi naan: «NJUUMa la!» daldi tiit bay yuuxu.
Mark 6 49 Bi ñu ko gisee nag, muy dox ci kaw dex gi, ñu foog ne nJUUMa la, daldi yuuxu.
Luke 24 37 Ñu daldi tiit, foog ne dañoo gis nJUUMa.
Luke 24 39 Xool-leen samay loxo ak samay tànk. Man mii la. Laal-leen ma te xam, nJUUMa amul yaram walla ay yax, ni ngeen gise, ma am ko.»
Philippians 1 7 Te JUUMuma ci li ma xalaat loolu ci yéen ñépp, ndaxte def naa leen ci sama xol; ba tax fii ci kaso bi, ci taxawal xebaar bu baax bi ak lawal ko, yéen ñépp am ngeen wàll ak man ci yiwu Yàlla.
Hebrews 12 17 Xam ngeen ne, ba ñu ca tegee tuuti, gàntu nañu ko, ba mu bëggee jot barke bi. Amul fenn fu mu jaar ba defar nJUUMteem, te jooy, yi mu doon jooy, mënu ci dara.
James 1 16 Yéen sama bokk yi ma bëgg, buleen JUUM ci lii:

Page:   1