menu.png
Lost Password ?

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
Luke 7 3 Bi mu déggee mbiri Yeesu, mu yónni ca moom ay Yawut, di MAGI dëkk ba, ngir ñaan ko, mu ñëw faj surga ba.
Luke 7 4 Bi MAGI dëkk ba agsee ca Yeesu, ñu sàkku ci moom ndimbal, ñaan ko: «Ki nu yónni ci yaw de, yelloo na ndimbal,
Acts 13 50 Waaye Yawut ya xiir ay jigéen, ñi woomle te farlu ci diine, ñoom ak MAGI dëkk ba, ñu fitnaal Pool ak Barnabas, ngir génne leen réew ma.

Page:   1