menu.png
Lost Password ?

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
Matthew 16 9 Ndax xaMAGUleen ba tey? Xanaa fàttalikuwuleen juróomi mburu ya ngir juróomi junniy góor ña, ak ñaata pañe ngeen dajale woon ciy dammit?
Mark 4 40 Yeesu ne taalibe ya: «Lu tax ngeen tiit? Ndax gëMAGUleen?»
Mark 6 3 Ndax kii du minise bi? Ndax du doomu Maryaama te MAGU Saag, Yuusufa, Yuda ak Simoŋ? Te ay rakkam yu jigéen ndax nekkuñu fi ak nun?» Kon nag ñu daldi ko xeeb.
John 7 8 Yéen nag demleen màggal ga. DeMAGUma màggal googu, ndaxte sama waxtu jotagul.»
John 8 57 Yawut ya ne ko: «AMAGUloo juróom-fukki at, ba noppi naan gis nga Ibraayma?»
John 9 21 Waaye ni mu def léegi bay gis, xamunu ko, te xamunu it ki ko ubbil ay bëtam. Laajleen ko; MAGUm jëmm la, te man na tontul boppam.»
John 9 23 Looloo tax waajur ya ne: «Laajleen ko; MAGUm jëmm la.»
John 20 9 Taalibe yi xaMAGUñu woon Mbind, mi doon wone ne, Yeesu dafa war a dekki.
Acts 7 5 Waaye mayu ko fa genn moomeel gu mu war a donnale, du sax fu mu man a teg tànkam; waaye dig na ko ne, dina ko may réew mi, mu yilif ko moom ak askanam, fekk booba aMAGUl doom.
Romans 4 17 Moom la Yàlla dogal, wax ko ci Mbind mi ne: «Def naa la baayu xeet yu bare.» Ndaxte Ibraayma gëmoon na Yàlla, miy dekkal ñi dee, tey wax ci lu aMAGUl, mel ni dafa am.
Romans 7 8 Waaye bàkkaar jaare na ci ndigalu Yàlla, daldi ñëw dugg ci man, ba yengal ci man xemmem yu bare. Ndaxte ba ma xaMAGUl woon yoonu Musaa, bàkkaar da ne woon nemm ci man.
Romans 7 9 Te keroog bi ma xaMAGUl lu yoon wi santaane, maa ngi doon dund dund gu neex; waaye ba ma ko déggee, bàkkaar dafa daldi fuddu ci man, te man ma daldi dee.
Romans 10 14 Waaye nan lañuy wooye ki ñu gëMAGUl? Te naka lañu man a gëme ki ñu déggagul turam? Te naka lañu man a dégge turam, te kenn xamalu leen ko?
1 Corinthians 12 2 Xam ngeen ne, bi ngeen xaMAGUl woon Yàlla, xërëm, yi mënul a wax, ñoo leen jiitaloon, di leen wommat.
Galatians 4 8 Bu jëkk, bi ngeen xaMAGUl Yàlla, yéena ngi doon jaamu yeneen yu ñu daan bokkaaleel Yàlla.

Page:   1 2