Found entries


Book | Chapter | Verse | Text |
Matthew | 5 | 31 | «Waxoon nañu ne: “Ku fase sa jabar, nga bindal ko kayitu PASE.” |
Matthew | 19 | 7 | Bi Yeesu waxee loolu, Farisen ya laaj ko ne: «Waaye Musaa santaane na, nit jox jabaram kayitu PASE, tàggook moom. Lu tax mu wax loolu nag?» |
Mark | 10 | 4 | Ñu ne ko: «Musaa maye na, nit bind kayitu PASE, tàggook jabaram.» |
Page:
1