Found entries


Book | Chapter | Verse | Text |
Mark | 7 | 34 | Mu yërëm ko, ba binni ci xolam, xool ci asamaan, daldi ne: «Effata,» liy tekki: «UBBIKULeen.» |
Acts | 12 | 10 | Noonu ñu weesu wottukat bu jëkk ba ak ba ca tegu, ñu agsi ca buntu weñ, ba jëm ca dëkk ba, mu daldi UBBIKUL boppam ci seen kanam. Ñu génn nag, jaar ci benn mbedd, malaaka ma daldi ko bàyyi. |
Page:
1