menu.png
Lost Password ?

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
Matthew 2 7 Ci kaw loolu Erodd woolu ci kUMPa boroom xam-xam ya, di leen ceddowu, ngir xam bu wóor kañ la biddiiw bi feq.
Matthew 6 4 ngir sa sarax nekk kUMPa. Noonu sa Baay, bi dara UMPul, dina la ko delloo.
Matthew 6 6 Yaw nag booy ñaan, duggal ci sa néeg, tëj bunt bi, te nga ñaan sa Baay bi bët mënta gis. Noonu sa Baay, bi dara UMPul, dina la ko delloo.
Matthew 6 18 ngir sa koor bañ a feeñu nit ñi, waaye mu feeñu sa Baay bi bët mënta gis. Noonu sa Baay, bi dara UMPul, dina la ko delloo.
Matthew 10 26 Kon nag buleen leen ragal, ndaxte amul dara lu nëbbu, lu ñu warul a biral, mbaa luy kUMPa lu ñu warul a siiwal.
Mark 4 22 Amul dara luy kUMPa lu ñu warul a siiwal, mbaa mu làqu te warul ne fàŋŋ.
Mark 7 24 Gannaaw loolu Yeesu jóge fa, jëm weti dëkku Tir. Bi mu fa eggee, mu dugg ci kër, te bëggul kenn xam ko, waaye jataayam mënul a UMPe.
Luke 8 17 Amul dara luy kUMPa lu ñu dul siiwal bés, walla lu làqu lu ñu dul feeñal, ba mu ne fàŋŋ.
Luke 12 2 Amul dara lu nëbbu lu ñu warul a biral, mbaa lu kUMPa lu ñu warul a siiwal.
Luke 18 34 Waaye taalibe ya dégguñu li mu leen doon wax; kàddu yooyu UMP na leen, te xamuñu li waxi Yeesu yooyu tekki.
Luke 24 18 Kenn ci ñoom, ki tudd Këleyopas ne ko: «Xanaa yaw rekk yaa ñëw Yerusalem te UMPle li fi xewoon bés yii?»
John 10 24 Yawut ya wër ko ne ko: «Kañ nga nuy dindi ci kUMPa? Boo dee Almasi bi, wax ko mu leer.»
Acts 16 37 Waaye Pool ne alkaati ya: «Dóor nañu nu ay yar ci kanamu ñépp, ci lu ñu wéerul ci benn àtte, rax-ca-dolli tëj nañu nu kaso, nun ñiy jaambur ci nguuru Room. Léegi ndax dañu noo bëgg a sànni ci mbedd mi ci kUMPa? Mukk! Nañu ñëw, ñoom ci se
Acts 26 26 Yëf yii leer na buur bi, moo tax maa ngi koy wax ak kóolute. Wóor naa ne, dara ci lii may wax UMPu ko, ndaxte lii amewul ciy ruq.
Romans 11 25 Bokk yi, dama leen a bëgg a dindi kUMPa ci lii, ngir ngeen bañ a yég seen bopp. Dërkiisu xol dab na bànni Israyil ab diir, ba bés ba mboolem waa àddina, ñu war a bokk ci nguuru Yàlla, dugg ca.

Page:   1 2 3