menu.png
Lost Password ?

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
Matthew 9 6 Waaye XAMLEen ne, Doomu nit ki am na ci àddina sañ-sañu baale bàkkaar yi.» Ci kaw loolu Yeesu ne ku làggi ka: «Jógal, jël sa basaŋ te nga ñibbi.»
Matthew 22 16 Noonu ñu yónni ci moom seeni taalibe ak ñi far ak buur bi Erodd ne ko: «Kilifa gi, xam nanu ne ku wóor nga, te ragaloo kenn, ndaxte seetuloo jëmmi nit, waaye dangay XAMLE yoonu Yàlla ci bu wóor.
Matthew 24 33 Noonu yéen itam bu ngeen gisee loolu lépp, XAMLEen ne jege na, mu ngi ci bunt bi sax.
Matthew 24 43 Waaye XAMLEen lii: bu boroom kër gi xamoon, ci ban waxtu ci guddi la sàcc bi di ñëw, kon dina yeewu te du ko bàyyi, mu toj këram.
Matthew 27 37 Te it ñu teg ci kaw boppam mbind, mu XAMLE lu tax ñu rey ko, mu ne: «Kii mooy Yeesu, buuru Yawut yi.»
Mark 2 10 Waaye XAMLEen ne, Doomu nit ki am na ci àddina sañ-sañu baale bàkkaar yi.» Ci kaw loolu mu ne làggi ba:
Mark 12 14 Ñu ñëw ci moom nag ne ko: «Kilifa gi, xam nanu ne ku wóor nga, te ragaloo kenn, ndaxte seetuloo jëmmi nit, waaye dangay XAMLE yoonu Yàlla ci bu wóor. Wax nu, ndax jaadu na, nu fey buur bi Sesaar galag am déet? Nu fey ko walla nu bañ koo
Mark 13 29 Noonu itam bu ngeen gisee loolu lépp xew, XAMLEen ne jege na; mu ngi ci bunt bi sax.
Mark 15 26 Mbind mi XAMLE lu tax ñu rey ko nee na: «Kii mooy buuru Yawut yi.»
Luke 5 24 Waaye XAMLEen ne, Doomu nit ki am na ci àddina sañ-sañu baale bàkkaar yi.» Ci kaw loolu Yeesu ne ku làggi ba: «Maa ngi la koy sant, jógal, jël sa basaŋ te nga ñibbi.»
Luke 10 11 “Seen pëndu dëkk, bi taq ci sunuy tànk sax, noo ngi koy faxas, ngir seede leen seen réer. Waaye nag XAMLEen ne, nguuru Yàlla jegesi na.”
Luke 12 39 Waaye XAMLEen lii: bu boroom kër gi xamoon ban waxtu la sàcc bi di ñëw, du ko bàyyi, mu toj këram.
Luke 20 21 Ñu daldi ñëw ci Yeesu ne ko: «Kilifa gi, xam nanu ne li ngay wax te di ko jàngale lu jub la. Amuloo parlàqu, waaye dangay XAMLE yoonu Yàlla ci bu wóor.
Luke 21 20 «Bu ngeen gisee ay xarekat wër dëkku Yerusalem, XAMLEen ne jamono, ji ñu koy yàq, agsi na.
Luke 21 31 Noonu itam bu ngeen gisee loolu lépp xew, XAMLEen ne nguuru Yàlla jege na.

Page:   1 2 3 4 5