menu.png
Lost Password ?

Bible Search

 (Index)


Found entries

•••► •••►
Book Chapter Verse Text
Matthew 5 47 Su ngeen nuyoo seeni bokk rekk, lu ngeen def lu doy waar? Xanaa ñi XAMUl Yàlla duñu def noonu it?
Matthew 6 7 «Te it bu ngeen di ñaan, buleen bareel wax yu amul njariñ, mel ni ñi XAMUl Yàlla; ñoom defe nañu ne, Yàlla dina leen nangul ndax seen wax ju bare.
Matthew 6 32 Ndaxte loolu lépp, ñi XAMUl Yàlla ñoo koy wut. Te seen Baay, bi nekk ci kaw, xam na ne am ngeen soxla ci loolu lépp.
Matthew 11 19 Gannaaw gi nag, Doomu nit ki ñëw na, lekk, naan, ngeen daldi ne: “Kii daal bëgg na lekk, di naan biiñ, tey xaritoo ak ay juutikat ak ay boroom bàkkaar.” Waaye li xam-XAMU Yàlla di jur, mooy firndeel ne dëgg la.»
Matthew 12 42 Te it ca bés pénc buur bu jigéen, ba dëkkoon ca sudd, dina jógandoo ak niti jamono jii, yey leen; ndaxte dafa jóge ca catul àddina, ngir déglu xam-XAMU Suleymaan, te ku sut Suleymaan a ngi fi.
Matthew 13 19 Boo xamee ne nit mu ngi déglu wax ju jëm ci nguuru Yàlla te XAMU ko, Ibliis day ñëw, këf li ñu def ci xolam; kooku mooy ki jot ci jiwu wi ci kaw yoon wi.
Matthew 15 17 XAMUleen ne, lépp lu dugg ci gémmiñ, ci biir lay jëm tey génn ca bérab bu làqu?
Matthew 16 11 Kon nag lu tax XAMUleen ne, waxuma mburu? Waaye damaa bëgg, ngeen moytu lawiiru Farisen ya ak Sadusen ya.»
Matthew 20 22 Yeesu ne ko: «XAMUleen li ngeen di ñaan. Ndax man ngeen a naan kaasu naqar, bi may naan?» Ñu tontu ko: «Man nañu ko.»
Matthew 21 27 Ñu tontu Yeesu nag: «Loolu XAMUnu ko.» Noonu Yeesu ne leen: «Kon man itam duma leen wax ci ban sañ-sañ laay defe yëf yii.
Matthew 22 29 Waaye Yeesu tontu leen ne: «Yéena ngi cig réer, ndaxte XAMUleen Mbind mi mbaa kàttanu Yàlla.
Matthew 24 36 «Waaye bés booba walla waxtu wa, kenn XAMUl kañ lay doon; du malaaka yi ci kaw, du sax man Doom ji, waaye Baay bi rekk moo ko xam.
Matthew 24 42 Yeewuleen nag, ndaxte XAMUleen bés bu seen Boroom di ñëw.
Matthew 24 50 kon njaatige ba dina ñëw ci bés bu mu ko séenuwul ak waxtu wu mu XAMUl.
Matthew 25 13 «Yeewuleen nag, ndaxte XAMUleen bés ba mbaa waxtu wa.

Page:   1 2 3 4 5 6